Max Richter — I am writing this letter tekst piosenki i tłumaczenie

Strona zawiera teksty i polskie tłumaczenie piosenki "I am writing this letter", wykonawca: Max Richter.

Tekst piosenki

bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu si rekk
melni wèer wi delu si ci sèy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna dèe ci souff
samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo,
ak rétane bi rafèt na,
xèw bou nèex
mais soubbe dagniouy dèm,
galankor bi moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou doy ngir soppanté
goudi gi wèss, mangi won
fénène, bi ci toop dina fi sori
ak samay bok ci camion bi,
dinagnouy teugueu ngir
féccelo yénéni nit
ak samy bok ci camion bi,
ngir andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll la ku dul toxu doo xam fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Merci a El Cancre pour cettes paroles)

Tłumaczenie tekstu piosenki

Bakkan varuv dall la fa Mui degge Duko YEG
dem rekk delu jeśli rekk
melni wèer wi delu jeśli sèy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna dèe dalej souff
Samai xarit, thei Ji ndaje Bi Rafet na,
Joko, seddo,
AK retane Bi Rafet na,
xèw Bou nèex
ale subbe dagnyui dem,
galancor Bi mój dougnu
Młynarz xamanté Bux,
Dow nouy am waxtou
bu Doi ngir soppante
goudi gi wèss, Manga Vaughn
fenen, bi si tuop Dina Fi Sori
AK Samai bok ki ciężarówka Bi,
dinanui teugeu ngir
feccelo eneni Nit
AK sami bok ki ciężarówka Bi,
ngir Andi mbekte bignui jeul
bakkan waruw dàll ku dul toxu do Sham-Fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Dzięki El Cancre za te słowa)