Youssou N'Dour — Létt ma tekst piosenki i tłumaczenie
Strona zawiera teksty i polskie tłumaczenie piosenki "Létt ma", wykonawca: Youssou N'Dour.
Tekst piosenki
Du nil, du nil bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw téppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé
Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Boo ma waxee fi nga bêgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def
Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë bëgg ak bañ la. .
Tłumaczenie tekstu piosenki
Du Nil, du Nil jogging naa naa Nga Летт Ma Walla książka Nga Фири Ma Xamal Ma Lou lirów oszukuje Maa Wu cm SA Gal i Ma Nga kreda jest xale Yaw daal yaw téppal fële Danga ba di tappale Su fekkeeni parewoo warz loo di yónée Ngall Yaw Bal Ma defioo Lou Ma Nin Di xale MBA бег-наа-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-НА-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На-На
Ma dem Bay Dem nga teye ma Légi sax dems sent Dama'y BA nga Nga dugël ma Bu fekkeeni parewoo wszystkie Lou-Di-Yon Ngala yaw bui ma def loo lu ma co nu-Di-хеебе-Летт MA MBA NGA Fira ma Begg Nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg Nga Nga lét Ma ma ma Nga ma Nga ma Nga pégg ma ma Nga weesuwul net SA Géntu Moro'om bëgg Nga ma demal La Wax ma Kon Li ne CI Yaw Bari pexe weesuwul net SA géntu moro'om bëgg Nga ma demal La Wax ma Kon Li ne Yaw Létt ma MA NGA Fira Fira Ma Nga Nga létt Ma Walla Book nga firi ma begg Nga Nga Nga Nga Nga Ma Wax ma Nga bêgg dem
Ma wosk La Fi Internet Ngai Jaar
Nie Demal BL dem, waxal Bul wosku, defal Bul Def
Człowiek Daal Sonn Naa,
Naa Naa Naa Sonn Sonn Bëgg Nga létt ma-Walla nga Phiri ma
Bëgg Naa Ko szczęki, bañ Naa Ko subë Kon xanaa ganaaw subë bëgg AK bañ La. .