Youssou N'Dour — Sama Gàmmu tekst piosenki i tłumaczenie
Strona zawiera teksty i polskie tłumaczenie piosenki "Sama Gàmmu", wykonawca: Youssou N'Dour.
Tekst piosenki
Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Yor xaalis mënui tee me moom la
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal man suma xarit nga
E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu foo ko
Teeyai teey teey
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan
Tłumaczenie tekstu piosenki
Nanga Yao sama Gammu degg z Nga yor xaalis
Ham lub Neil Yao Mumu Los Ko
Ludzie Ko ABB mbaa Nga dla Ko
Baal dawse, y
Nanga, Nga Gammu degg z Nga yor xaalis
Baza Jeśli séén tàmbaleey wëlis Xam lub neil yaw moomo los Ko ludzie kobba mbaa nga dla ko Baal dózéé, yor xaalis mënui tee me moom z Nanga, to nga z gàmmu degg z nga yor xaalis Xam lub neil yaw Moomo los Ko ludzie ko abaa mbaa do Ko Baal dózé, jeśli nie chcesz, to foog lub teraz plan ko waddal Nga dla ko Wax, jeśli gaaw-aata od Doon, jeśli Fay ko Mann DAAL maay w buur Nangu ko nanga, to Nga od gàmmu degg od Nga yor Xaalis.
Baza, Jeśli séén tàmbaleey wëlis Xam lub neil yaw moomu los Ko ludzie kobba mbaa nga dla ko Baal dózéé, y Ali suñuy maam noonu Laan ko Daan defee Ali suñuy baay noonu Laan Ko waxee Ali suñuy yaay noonu Laan ko daan tópee Ali gàmmu daal sama do Nga, ale w gàmmu daal Nga gamę даал Sun Аскан Nga Ali сунуй Mamo noonu Lan do Daan Defi, ale w gamę даал Sun Xarit Nga, ale w gamę Даал Man sama доому ндай Nga, ale w gamę даал Man Song ксарит Nga, ale w gamę даал Yau sama DOW ндай Nga Baal доок моому pod ko тэйай Tay Tay Ali Sui маюй MAN nie La Sui noonu LAÑ ko Daan waxee Ali suñuy yaay Noonu LAÑ ko Daan tópee, ale w gàmmu DAAL sama doomu nday Nga, ale w Gàmmu DAAL Sun xarit Nga, ale w gàmmu DAAL Sun askan