Youssou N'Dour — Sportif tekst piosenki i tłumaczenie
Strona zawiera teksty i polskie tłumaczenie piosenki "Sportif", wykonawca: Youssou N'Dour.
Tekst piosenki
Woyal sa wayu ndam ii
Dangay bégël sa xol bi
Ndax yaa yor bannex bi
Ni tay bés bii sa bés la
Sa mbër daan na kóntaan nga
Bu ñu daanee sa mbër nak
Na nga fexe ba nee
Po mii dañuy Jonante
Faw mu am ku moyle
Jarula defante, di xasteeka dóóre
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Bëgóón nga mu demee ni demewuko
Mën naa am bu ëllëgee mu gën fee neex
Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu
Xam ne lii fo la nii lay mënë deme
Powun jonante nii lay deme
Tay jii yaw bu ëllëgee keneen la
Fo ag ree de lañ ciy jublu
Moo tax ñu wara dal taynangu defet
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Waa waaw wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén
Sire lañu dóór bal géér ña da ñoo daw
Sire Bàlla moo ñaan Ramata Faal
Siree nga Cees Matee nga Njaarém
Duñ ko wëy ku reew, duñ ko wëy ku ñaaw
Aah wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Tłumaczenie tekstu piosenki
Woyal sa wayu ndam ii
Dangay bégël sa xol bi
Ndax yaa yor bannex bi
Ni Tai BES BIY sa BES La
Sa mbër daan na kóntaan nga
Bu GNU daani SA mber NAK
Na nga fexe ba nee
Po mii szkodliwe Jonante
Faw mu am ku moyle
Jarula defante, di xasteca Dore
Jonante po ag ree La
Bou gagne FO AG REE La
Bu njakki FO AG REE La
Lepp ci fo ag ree La
Boun La gagne munyel
Bu Ko Ganje baalal
Bëgóón nga mu demee ni demewuko
Mën naa am buöllëgee mu gën fee neex
Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu
Xam ne lii fo La nii lay mënë deme
Powun jonante nii lay deme
Tay jii yaw buöllëgee keneen La
FO AG REE de Lan si giublu
Moo tax GNU wara dal taynangu defet
Jonante po ag ree La
Bou gagne FO AG REE La
Bu njakki FO AG REE La
Lepp ci fo ag ree La
Boun La gagne munyel
Bu Ko Ganje baalal
Waa waaw wuy dabbee WUY YU
- Dabi Alaa ko ndey baate satata
Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén
Sire lanyu dóór bal géér ña ña da noo daw
Sire Bàlla moo naan Ramata Faal
Siree nga Cees Matee nga Njaarém
Dun ko wëy ku reew, Dun ko wëy ku naaw
Dobrze wuy dabbee WUY YU
- Dabi Alaa ko ndey baate satata
Jonante po ag ree La
Bou gagne FO AG REE La
Bu njakki FO AG REE La
Lepp ci fo ag ree La
Boun La gagne munyel
Bu Ko Ganje baalal